Menu

Accueil / Wikipedia en wolof

En bref

Wikipedia en wolof

Partagez cette page jeudi 19 novembre 2009

L’encyclopédie libre Wikipedia propose une version wolof de son portail.

En vous rendant sur cette adresse http://wo.wikipedia.org, vous pourrez consulter plus de 1 000 pages en langue wolof.

Deux mille utilisateurs sont enregistrés pour participer à l’enrichissement de l’encyclopédie, dont 23 sont actifs.

Voici la page sur la Tabaski :

« Tabaski, (ci araab »sul-hajja« ذو الحج), tuddees na ko noonu ngir ne mooy boroom aj gi, ci la araab yi daan aji Màkka, ci la tabaski gi it nekk, moom nag bokk na ci weer yees wormaal. Mooy weer wi mujj ci at mi. »

Messages

  • sn

    KHOUTBA SEYDINA LIMAMOU LAHI asws

    Khoutba béneel
    Mangui tambali sama bepp dieuf ak sama beep wakh ci yalla manga khamantani moy adji khezeuleul bepp mbindef ci kaw souf waye moy itam adji khezeuleul kouka sopp ci alakhira. Thiant migui sakh di gnel yalla manga khamni mo binde mbindef yi mou def si gno, ay yonente mou taneu si yonente yoyu mouha,ad mou def ko geun dja tedd thi yonente yi teyy geun di mbindef mou def khetam geun dja tedd si khet yi yalna dolli kheweul yalla si mom ak ay gnognam ak ay sahabam tei mou dolli ko mousseul. Guinaw lolu toukei na si ilimani yalla dji dieum si mbolem talibem yi dak way geum yi gorr ak djiguen makk ak ndaw mouth yalna nekk si yenn ak yeurmandei yalla ak barkem ak si seeni gnogne. Li waral terrei bi magui len di yegeul naka man magui nouyou si yenn magui lath sen mbirr sen yiz ak sen dia,eu ak sen deukouway. Magui len di denk si topou yalla ak yonentam ak fedali sen gueum guen di dieuflante yiw guen beugeunte ndakh niki dinne layantebiir la. Layanteibir nakk moy gua labir si yalla ak yonentam ak terem ak thi kilifa dinee yi ak thi mbolem dioulit nieup. Labir si yalla moy gua zeteul ko gua dieufei lamou digle gua bayi lamou terrei gua digeul niit gni thi lolu. Labir si yonentam moy gua geum gua deugeul ko gua topp thi lammou gua batyi lamoyu terei si mom gua dieufei ay sounam labir si terem moy gua diangeu ko tei diko naffar gua djieufei la nekk thibir terei beu labir thi kilifay dine yi mo gua beug lenn gua topp lenn gua dimbali lenn djeum si mbiri dine gua digeul nitt gni si loola labbir si mboleem djoulit gni moy gua beug lenn mbolle senn niki mùouko zqkhei yonente yi salalahou aleyhi wq nsqlqm zqy geum dafay beug zayy geum gni tei dou bagn keen thi gnom niki mouko wqkhei batay salalhou aleyhi wq salam deug degu wqy geum dafay beugeul gneil m,bokk wqy geumeum lamou beugeul bopam wqkh nq yonente bi salalahou aleyhi wa salam boulen bagnante nagein digleuntei thi yiw gein di tereintei thi lou bonn guein yezeneul sen digeuntei si lou bakh magui lenn di denk guen def sen digenytei mbeugueil ndakh niki wq qldiqnq dqgni beugeunte boulen def sen digeuntei noonel ak mbagnel yenn nekk lenn ay mbokk kham len niki zay geum mbokam moy wqyy geum niki mouko wqkhei yalla mi adji kawe dji wqy geum yeup ay mbokk lagnou naguein yeweneul sen digantei mbooko guein ragal yalla anama moyu yeureumesse leenkham lenn yen wqy geum gni niki way geum dafay tafay tappo gnou daldi tappo thi mom kepp kou tapou woul thi niit gni dett nitt gni di tapo thi mom tei mdimbalou yalla dou Wath thi mom tei boulen eupeulantei alalou adina liffi nekk kay naguein eupeulantei yiwou alahira ndakh moy ligua khamni moy donnalei kheweul you dapeto yi ak daradia you kawei yi boulen kheur dieum thi aduna ndfakh ,niki mom meddeu la tei eddeu douko lekk ndarei khath ak tann naguen ko bayi boulen ko djapeu ndakh niki mom kzeur guou rappeu la goudi adji dagn tei ak dagnam lou djiegei la nague moytou neff na ak nena ndakh bariyana dou nekk di dadjei tha la neff na ak tha lougnou degu ak la nekka boulen ndiortou thi sen mbokoum djoulite ndare yiww naguen moytou thi gnqz ndiorte ndakh nikki yalla migui thi ndiortal diamam boulenn saggan thi toudou yalla fouguen fi meun ti nekk ndakh dafay dindi ay niawtef bi baril ay yiw kepeu kou ay yiweum barri ay niawtefam new dina dougou aldiana mbem soppna yalla yalla adji kawei dji wqkhnq nqguen toudou yqllq bouguen takhawe ak bouguein toggei ak thi seni teuray guen di khalate thi ay kemanam niki mou binde asaman ak souff yalla digle na thi baril diko fatalikou gnel wakham dja mom adji kawei dja nqguen toudou yalla toudou gou bari guen diko sabal souba ak guone naguen toudou yalla si bepp bereup ndakh niki beureup yi dinagn lenn sedde besoup takhaway ba boulen lekk dara lou teyy boulen nan dra lou teyy boulen warr dra lou tey boulen soll dra lou teyy boulen dieuf thi mbolem li guen di djiarigno thi leeneu loudoul lou teyy lou teyy nak moy lou dagane lignouy dieukeu khoti si birou domou adama bi bissou takhaway ba moy lou haram la ndakh niki lou haram dina yakk lou dagane niki tokou deret dina yakk baganou soow niki nonou lou new si haram dina yakk lou beuri thi lou dagane tei mandargay gnawtef gnel domou adama moy mou lekk lepp loumou foytou tei dou falei sikk daganam wala cik aramam ak leunteum. Top manguilen di dinkk yén samay sahaba you goor yi ak samay sahaba you djiguén yi ci nguén foot, nguen sangu, nguen sétou ci adouna. Lolou kat mo geuneu di leen niel ci niouleen di foot ci alahira. Dinguén feek linguén dieufon moudon adji téw.
    Niani bindeu kat yi jeff yi ak wax yi détt gnou niani way sagaaneu wakhtou, tayitt douniou bayi lou toutt, dou thia geuni lou geuneu toutt ak touut.
    Kone naguén farlou ci top Yalla ak Yonentam, guen toubb ci beep waxtou, guen di rethiou ci liguen faate, nguén di dab dabatale, nguén di goorgorlou nda kh niki diamou yalla thieurou bepp mbindef la

    Répondre

    modération a priori

    Ce forum est modéré a priori : votre contribution n’apparaîtra qu’après avoir été validée par un administrateur du site.

    Qui êtes-vous ?
    Votre message
    • Ce formulaire accepte les raccourcis SPIP [->url] {{gras}} {italique} <quote> <code> et le code HTML <q> <del> <ins>. Pour créer des paragraphes, laissez simplement des lignes vides.

  • sn

    salut j’aimerai avoir les quinze ponts du referendum en wolof svp

    • sn

      1. Fexee kurelu polig mengoo ak jamono ci réewum demokarasi mu màgg
      2.Nit ñi bokul ci been kurelu politik mana laaj baatu askan wi ci bépp xeetu wote
      3. Sàkk Kurel gu mag guy doolel book moomel yi tudeeko Haut Conseil des collectivités territoriales ngir gën a faydal sakan wi yooriinu réew mi
      4. Nangul askan wi ay àq, yelleef ak wareef yu bes muy : sañ-sañu kéewange ak dëkuwaay yu mucc ayib, sañ-sañ yu bées ci senni suuf ak leeb lu cay jur koom mbaa di ca meñee
      5. Dooléel wareefu maxeej gi, (citoyen), beep nit bu ci biral ay warugaram
      6. Delloo diirub palug ñiitu réewmi ci juróomi at
      7. Gën a dooleel kujeg politik gi ak njiitam
      8. Doomi réewmi neek bitim réew am seen dipitey boop yu leen di toogal ca péncum ndawi réewmi
      9. Yaatal dooley Péncum Ndawi Réewmi ci ni miy sayto gornmaŋ bi booleek ma ko leegi muy am sañ-sañu cambar tërëliin ak doxaliini nguur gi
      10. Jeebal Conseil Constitutionnel béep dogal laata ñu koy dëgal ak di ko doxal
      11. Yokk limub ñaay toog ca Conseil Constitutionnel mu jogée ci juróom ag ci juroóom ñaar
      12.Jox njital Péncum Ndawi Réewmi di Président Assemblée Nationale mu taan ñaar ci juroom ñaari nit ñiy àtte ca Conseil Constitionnel
      13.Yaatal sañ-sañi Conseil Constitutionnel ngir muy joxe ay xalaat ak di wax cii dogal yi cour d’appel jaap ne dëpoo wu ñu ak sartu ndeytu àtte yi
      14. Ndeyu àtte yi tëral dëgal gis-gisu biy nangu réewmi am ay bokk moomel, ak gis-gis biy nangu nguur gi waññi leen ci ay ceram jox ko gox yi ak goxaan
      15. Saxal abadan li keen dootul ma na sopi yii dogal : paliinu njiitu réew mi, ak ñaari pal yu degaloo yi mu dul mana weesu ak juroomi at yi pal gu nekk di yem

    Répondre

    modération a priori

    Ce forum est modéré a priori : votre contribution n’apparaîtra qu’après avoir été validée par un administrateur du site.

    Qui êtes-vous ?
    Votre message
    • Ce formulaire accepte les raccourcis SPIP [->url] {{gras}} {italique} <quote> <code> et le code HTML <q> <del> <ins>. Pour créer des paragraphes, laissez simplement des lignes vides.

  • Répondre

    modération a priori

    Ce forum est modéré a priori : votre contribution n’apparaîtra qu’après avoir été validée par un administrateur du site.

    Qui êtes-vous ?
    Votre message
    • Ce formulaire accepte les raccourcis SPIP [->url] {{gras}} {italique} <quote> <code> et le code HTML <q> <del> <ins>. Pour créer des paragraphes, laissez simplement des lignes vides.

  • Répondre

    modération a priori

    Ce forum est modéré a priori : votre contribution n’apparaîtra qu’après avoir été validée par un administrateur du site.

    Qui êtes-vous ?
    Votre message
    • Ce formulaire accepte les raccourcis SPIP [->url] {{gras}} {italique} <quote> <code> et le code HTML <q> <del> <ins>. Pour créer des paragraphes, laissez simplement des lignes vides.

Un message, un commentaire ?

modération a priori

Ce forum est modéré a priori : votre contribution n’apparaîtra qu’après avoir été validée par un administrateur du site.

Qui êtes-vous ?
Votre message
  • Ce formulaire accepte les raccourcis SPIP [->url] {{gras}} {italique} <quote> <code> et le code HTML <q> <del> <ins>. Pour créer des paragraphes, laissez simplement des lignes vides.

À la une

  • Le solaire est-il rentable dans les villes du Sénégal ?

    Le solaire est-il rentable dans les villes du Sénégal ?

ACTUALITÉS

  • Dip : une nova du hip hop sénégalais
    Dip : une nova du hip hop sénégalais
  • Dakar : mais où est passée la mer ?
    Dakar : mais où est passée la mer ?
  • Méduses et baigneurs font-ils toujours bon ménages ?
    Méduses et baigneurs font-ils toujours bon ménages ?
  • Toilettes ou pas toilettes ?
    Toilettes ou pas toilettes ?
  • Les épices de la séduction sénégalaise
    Les épices de la séduction sénégalaise
  •  Marathon de Dakar 2017
    Marathon de Dakar 2017

Cherchez dans le répertoire

Top