Proverbes wolof
Proverbes wolof

Proverbes, sentences et maximes wolof.
17 octobre 2008

Saytaane waxul dëgg waaye yàq nam xel
18 septembre 2008

Lu Feegn ci sey, nuyoo wone na ca ngoro ga, dagnou ko fayul.
18 septembre 2008

Ku bëg teendj dangay taary.
18 septembre 2008

Lo doonul talibeem, mënulo doone serignam.
18 septembre 2008

Xalel poto-poto la, nooko raaxeh rek lay weyeh.
12 novembre 2007

Ku yàgg ci teen, baag fekk la fa.
12 novembre 2007

Yàgg du saabu, waaye dana fóót.
12 novembre 2007

Yàgg ay wone légétub taat.
12 novembre 2007

Ndànk-ndànk ay jàpp golo cib ñaay.
12 novembre 2007

Lu la mar mayul, màtt du la komay.
12 novembre 2007

Kuy jaay kamaate doo bëré : boo ca dëggee mu toj.
12 novembre 2007
